We’ve updated our Terms of Use to reflect our new entity name and address. You can review the changes here.
We’ve updated our Terms of Use. You can review the changes here.

Askanyi

by Askanyi

/
  • Streaming + Download

    Includes unlimited streaming via the free Bandcamp app, plus high-quality download in MP3, FLAC and more.
    Purchasable with gift card

      €10 EUR  or more

     

1.
Zikr Afie 05:22
Fadilo FALLOU mou fadilo Da gnou laye gnane nga gnanal gno Balla aïssa ndimbeuli nga gno Yeureume nga gno Wétali nga gno Thi aduna mame fadilo Da nou gnane nga gnanal gno Da nou gnane nga gnanal gno Nga yag fé Nou yag fii Ligéyal mame fadilo Da nou lay gnane Mou dieum kanam Ndax Ba nou dèmé Ba fa kanam Ba gneup outsi Lou nou Am Lou nou am djombounoy dax Ngeume gui fi sax Fi thiy aname talibéy mayé Fi thi daraay seugn bé Seugn Bi yag sounou kanam Yag no ndimbeulé lole Mou fadilo hoo hoo da nou laye gnane nga gnanal no Balla aïssa ndimbali nga no Yeureum nga no Wetali nga no thi aduna mame fallo Da nou lay gnan nga gnanal gno Da nou lay gnan nga gnanal gno Ki mo diaye ndiourél Dieundé kok talibe Mou fallou ya nga thia kanam Ki Mo djeul soror ba toudé ko Mame Lamp fall Mo fadilo nga thia kanam Bayou AFIA bayou Segn atex Mbacke Mou fadilo nga thia kanam
2.
Zikr Bamba 03:30
Ahmadou fou mou ré acxamdou (Ahmadou, la où il est, louanges à dieu) Djoulou thi yoén bi bagma tayii (il prie au du prophète sans jamais s’en lasser) Bolé thia jah dieu feuté Mame Bamba (il y ajoute je remerci Mame Bamba) Ahmadou, Ahmadou Bamba Ahmadou, Ahmadou Bamba Mome moye xadime Rassouloulahi (i l est le serviteur, l’envoyé) Mome mo djouli thi yonéne (cest lui qui prie pour le prophète) Mome bagna tay tayi (sans jamais s’en lasser) Diange diangone thi lou bau (en avait beaucoup étudié) Xamone thi lou Bare Bare (en avait beaucoups su) Ko Koy Ahmadou Bamba (c’est bien lui, Ahmadou Bamba)
3.
Vibuzimu 03:59
Hashize amezi n imishamvu Ntatora agatiro Hashize imyaka ntaryama ngo nsinzire Ngira ngo ndagohetse nkumva abahutu barira Ngize ngo ntoye agatiro yemwe nkumva abatutsi barira yeeee, ooooh Nyegera ndakuyagire irimvuye imushaha Reka ndarikubwire Nta gitsure nta nzigo So wawe yarakubeshe Nanje iwacu barambeshe Umuhutu n umututsi burya turavukana Ohoho, Ririririrrr iiiii, eheeee So akwanka akuraga urubanza rwamunaniye So akwanka akuranga urubanza rwamunaniye: Sogokuru wawe yagiye adahoneje abatutsi Sogokuru wawe yagiye adahoneje abahutu:
4.
Lumbu 04:28
LUMBU TINA Mbé BUTI FUANA é é Lors que mon dernier jour arrivera BALA BANI NA KU BA BONGé é é LUMBU TINA Mé TINI KuéNDé é ngo BALA BANI KUé NI BA SISA é oh TINI KUéNDA Mé MU MISéRé é é BALA BA Bani Kwekwa ba Kuéndélé MINDA MIA MANA LéMA ZABA TI NGUé DIAKU DI WIDI LU N’SANGA BA MANA LUA TUNGA ZABA TI NGUé DIAKU DI WIDI BIDILU BIA MANA WAKANA ZABA TI NGUé DIAKU DI WIDI SANDUKU BA MANA DIA TUNGA ZABA TI NGUé DIAKU DI WIDI OH OH YAYé YAYA OH OH... OH YAYé YAYA ...
5.
Matondo 05:22
6.
Xarnu Bi 05:22
Sëriñ bi noo gi deeti ñaan Faqiir dafay nangoo dagaan Nangul nu lépp lu nu ñaan Ndax Yàlla naatal xarnu bi Noongi dangaan ci Mustafaa Ma nekk marwat’ak safaa Ak àqi amdi Mustafaa Mi Yàlla jébbal xarnu bi 3. Ak àqi mboolem ay rakkam Ak àqi séen baay yi ñu am Ak àqi seex yi Bàmba am Ndax Yàlla naatal xarnu bi Mboolem muriid yépp a ngi tuub Tey réccu bàkkaar yi nu joob Ba lu nu bay-bay, du nu góob Sëriñ bi geesul xarnu bi Mbàkke, dangay boroom i mbóot Te sag njaboot tawat gilóot Ñu def ma ab àntarpareet May làpputoo waa xarnu bi Aw ma màqaamam di la woo Waaye muriid yi ñoo ma woo Ni tawatal te bu ñu woo Saw làmmiñay wow xarnu bi Tay jii ma wax bani tareet Ngir yaa ma def antarpareet Yaa fab i xam-xam ne yuréet Ci sama xol, ci xarnu bi Te bul ma tanxamlu ci ñaan Ngir lii ma bon tey ku añaan Muriid yi yépp a la ko ñaan Ngir bëgg a dekkal xarnu bi
7.
La Ilah Ilallah La Ilah Ilallah Amdy, amdy sex fall. Mustapha Fall Yalam Nga Ba no la xamé Balégui xamé na gno. Ba nou la wolo Balégui fall doylou nanou Yalam Nga La Ilah Ilallah La Ilah Ilallah Dolé Mbax fall akneureumo Ak I leei yon gneuno yaram nga Am nga ko Meune nga ko Bonlay sope fall mouye nango Yaram Nga Sex modon Moustapha Fall o Baye Fall Yow lay ndamo Bayou mame Fallou Fall Amdy Moustapha La Ilah Ilallah La Ilah Ilallah Amdy, amdy sex fall. Mustapha Fall Yalam Nga
8.
Ba nou woulo ba légui doylon manou Ba moulax amé ba legui xamé na gna La Ilah Fall Yalla nga Ilah lah Yaram Doley ak ngeureum you oul djiexaty Deune go qui ay sikaré Xam xam ou gor moy xam géne borom Damal gor gui moi tofoi ndiguël fall La Ilah Fall Yaram Fall Yallah kéne la
9.
Milele 04:28
10.
Wonsono 03:21
ADJOMIDO BODIDO BISSé OKU é ANON WA MU DIDA Azé MIN VI Vé TCHé YI ABALA HWé ABALA HWé Djé ZOUé NKUNGA MIO – BONGA MOI BISAMBU BI – WéTI BIO MAYéLA MO – WA NGANA NGUé MATONDO NI – KU VUTULA Nzambi, nzambi ngoma zambwé Ngongi ngongi Kwen ngué ni anazo
11.
La Ilah Ilallah Fall La Ilah Ilallah Fall

about

ASKANYI is essentially and by means of compositions a fusion between a “Western” string quartet and African vocal music. A mix of artists with African (Senegal, Congo-Brazzaville and Burundi) and Western origins has sought to create a space in which both cultural dimensions can come together. For this reason the ensemble has been called ASKANYI, meaning “peoples” in Wolof, Senegal’s official language. What’s more, ASKANYI speaks about universal questions of our existence with harmony and passion, with an energy that is both fierce and serene. We invite listeners to be open to new experiences while looking beyond themselves.

credits

released October 30, 2015

Musicians: vocals: Jupiter Diop, Fredy Massamba, Nicole “Bongo” Letuppe, Marie-Ange Teuwen
String Quartet: Esther Lambrechts (violin), Sebastien Paz Ceroni (violin), Marijn Thissen (viola), Robrecht Kessels (cello)
Recorded, mixed and mastered: Uptown Studios January-August 2015
Design: Jan-Sebastiaan Degeyter
Contact & booking: info@askanyi.com
Produced by Mantra Music

license

all rights reserved

tags

about

Askanyi Brussels, Belgium

ASKANYI is essentially and by means of compositions a fusion between a “Western” string quartet and traditional African vocal music. This process results in a unique kind of music which echoes today’s multicultural environment. ASKANYI’s energy is both fierce and serene, inviting listeners to open themselves to new experiences and to look beyond themselves. ... more

contact / help

Contact Askanyi

Streaming and
Download help

Report this album or account

If you like Askanyi, you may also like: